Tuubaa Taysiir l'officiel

Tuubaa Taysiir l'officiel

Partager

As-salaamu Halaykum
dalal ak jámm di la wax ñawal ñu and liggéeyal Sëriñ bi ci yar ak tegin a dal jámm and dooleel Xasiida ak Tuubaa Taysiir

12/12/2025
16/09/2023

Ca Yàlla la nu bawoo, ca la nuy dellu.

Koo séen ci kaw suuf sii rekk, xamal ne dee moo ko fiy jële. Ku juddu bis, dee bis.

Kon li am solo mooy xam li tax sa Boroom bind la ba noppi nga def ca langa man lépp sa giir ug dund.

Kii nag bokk na ci ñi xamoon li tax seen Boroom wàcce leen ci kaw suuf, nekkoon ci jaamu Yàlla yaatal njàngalem Boroom Tuubaa, nekk nitu Yàlla ku ma masu la dégg ci moom lu wuute ak ndigalu Yàlla.

Ku faatu dees na la fàttaliku, naka la nuy fàttalikoo ku nekk mooy wuute.

Kii nag saa Boroom suturaal na ko ba rusul ku ko fàttaliku ca la mu nekkoon.

Ku rafet ab fàttaliku a ngii.

Yal na Yàlla yërëm ko gërëm ko jéggal ko suturaal ko terale ko àjjanatul Firdaws ci barke Alxuraanul Kariim 🤲.

Sàmm aar yiir Njaboot gi, barkeel leen🤲

15/09/2023

SERIÑ TUUBAA nee na "Mbaa yëkk ngeen ne balaa kenn dem ajjana daa weex tall ba melni YONENT BI SHWS!"
Ñu ne cell!
Mu bamtu ko ne "Da ngay weex tall ba melni YONENT BI SHWS, waaye yeen ( Aw ñoñam) bu kerogee Damay melni ab defukaay ngeen melni weccet dugg ci man ma dugg ci jibaay (Poche) RASUULUL LAAHI SHWS "

Garabu Tuubaa

15/09/2023

Le professeur de tous les chanteur de khassida ❤️❤️❤️BAAY ABLAAY DIOP

30/08/2023

Sëriñ bi mas naa wax Sëriñ Madu jaw paxa limal wàlliyu yi nga xam ne te nga boole ci sa bopp.

Sëriñ madu jaw baxa nee na :« kerog lama woor ne walliyu laa ».

Sëriñ Madu Jaw paxa di lim wàlliyu yim xam ba yég si ci Sëriñ Mandumbe xàbbaan, daal ne « Séex Mandumbe xàbbaan wàlliyu la ».

Nee na Sëriñ bi neko faral wuuwu rëdd. Kooku Murid Saadiq la te murid saadiq moo ëpp doole wàlliyu...

PS: Kon nak ñoo ngi dagaan Yàlla ci darajay Sëriñ bi mu def ñu ay dëgg-dëgg i murid saadiq.

14/05/2023

Ndaysaan ❤️❤️❤️

23/11/2021

🥰🥰🥰🥰

13/05/2021

Sama gaayi

Vous voulez que votre entreprise soit Salon De Beauté la plus cotée à Touba ?
Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.

Téléphone

Site Web

Adresse


Touba